Vuoi conoscere il testo di Soxna Ci (feat. Jeeba) di Samba Peuzzi ? Sei nel posto giusto.
Soxna Ci (feat. Jeeba) è una canzone di Samba Peuzzi il cui testo ha innumerevoli ricerche, quindi abbiamo deciso che merita il suo posto su questo sito web, insieme a molti altri testi di canzoni che gli utenti di Internet desiderano conoscere.
Loo bëggul man duma ko bëgg damay gaañ
Koo bëggul man duma ko bëgg dafay xaar
Yaa may tere nelaw ndax danga jongé déeg daaj
Kaay ma feccal la yaw, man jaral nga ma tàrantaax
Loo bëggul ne naa la dafay xaar
Ku dul yaw na ma dandu ñëwal gaaw
Yaay yëngal sama aah, man barde naa
Bàyyil mbele mbese gi di wax
Yaa fi nekk te du deñ, girl
Buur Yàlla moo ko def te du deñ
Bëgg nga ma bëgg naa lool du deñ
Soxna si yaay sama lumière
Ba abadan du deñ
Bëgg nga ma bëgg naa lool du deñ
Buur Yàlla moo ko def te du deñ
Soxna si yaay sama lumière
Ba abadan du deñ
Buuru galle lay doon ci yaw
Dinaa la xeexal fépp foo mën nekk
Newoon naa la ah yaw
Dagul nu ma la neexe yaa fi nekk te du deñ
Bi ma la xame ci la tàggook wet oooh, yo yo yo
Kon bul ma sori ñëwal fi sama wet ooh
Ma dundu paradise
They wanna make me out your way
Baby girl don't let them break your heart
Ñoom dañuy siisu di fen
Baby girl don't let them break your heart
Baby mine warul jooy, nah nah
Baby mine, bul jooy, waawaaw
Loo bëggul man duma ko bëgg damay gaañ
Koo bëggul man duma ko bëgg dafay xaar
Yaa may tere nelaw ndax danga jongé déeg daaj
Kaay ma feccal la yaw, man jaral nga ma tàrantaax
Loo bëggul ne naa la dafay xaar
Ku dul yaw na ma dandu ñëwal gaaw
Yaay yëngal sama aah, man barde naa
Bàyyil mbele mbese gi di wax
Yaa fi nekk te du deñ, girl
Buur Yàlla moo ko def te du deñ
Bëgg nga ma bëgg naa lool du deñ
Soxna si yaay sama lumière
Ba abadan du deñ
Bëgg nga ma bëgg naa lool du deñ
Buur Yàlla moo ko def te du deñ
Soxna si yaay sama lumière
Ba abadan du deñ
Bébé yaa ngi digal lu ne
Ñoo ngi koy wax dëgg dëgg nak du jeex
Jaar nañu fu ne te ñooy muje
Kaay ma feccal la bu de mooy li la neex
Bébé, bébé
Yàlla xam na, xam nga
Li nga ma jaral wallaay wallaay
Bëgg nañu diggënte bi jeex
Mais fi muus du fi na ne ñex
Lu neex da nañu dundu lu neex
Xam nga ne sa xol duma ko nab-nabé
Yaw ni nga ma bëgg noonu laa la bëggee
Bul mab yaa tay daagul fu ñu la nobee
Yaw ne na la bul mës a bàyyi
Ndax dama la woolu
Bul déglu wax yu bon yi ci man way
Ndax dama la woolu
Yaw ne na la ne wëti na la
Soo ma bàyyee ci la lay jàpp
Sama xol, sama reeni xol
Xam nga ni bëgg bëgg naa la
Loo bëggul man duma ko bëgg damay gaañ
Koo bëggul man duma ko bëgg dafay xaar
Yaa may tere nelaw ndax danga jongé déeg daaj
Kaay ma feccal la yaw, man jaral nga ma tàrantaax
Loo bëggul ne naa la dafay xaar
Ku dul yaw na ma dandu ñëwal gaaw
Yaay yëngal sama aah, man barde naa
Bàyyil mbele mbese gi di wax
Yaa fi nekk te du deñ, girl
Buur Yàlla moo ko def te du deñ
Bëgg nga ma bëgg naa lool du deñ
Soxna si yaay sama lumière
Ba abadan du deñ
Bëgg nga ma bëgg naa lool du deñ
Buur Yàlla moo ko def te du deñ
Soxna si yaay sama lumière
Ba abadan du deñ
Ci sono molte ragioni per voler conoscere il testo di Soxna Ci (feat. Jeeba) di Samba Peuzzi .
La ragione più comune per voler conoscere il testo di Soxna Ci (feat. Jeeba) è che ti piace molto. Ovviamente, no?
Quando ci piace molto una canzone, come potrebbe essere il tuo caso con Soxna Ci (feat. Jeeba) di Samba Peuzzi , desideriamo poterla cantare conoscendo bene il testo.
Sentiti come una star cantando la canzone Soxna Ci (feat. Jeeba) di Samba Peuzzi , anche se il tuo pubblico sono solo i tuoi due gatti.
Nel caso in cui la tua ricerca del testo della canzone Soxna Ci (feat. Jeeba) di Samba Peuzzi sia perché ti fa pensare a qualcuno in particolare, ti proponiamo di dedicargliela in qualche modo, ad esempio inviandogli il link di questo sito web, sicuramente capirà l'indiretta.
Qualcosa che succede più spesso di quanto pensiamo è che le persone cercano il testo di Soxna Ci (feat. Jeeba) perché c'è qualche parola nella canzone che non capiscono bene e vogliono assicurarsi di cosa dica.
Stai litigando con il tuo partner perché capite cose diverse ascoltando Soxna Ci (feat. Jeeba) ? Avere a portata di mano il testo della canzone Soxna Ci (feat. Jeeba) di Samba Peuzzi può risolvere molte dispute, e lo speriamo.
Impara i testi delle canzoni che ti piacciono, come Soxna Ci (feat. Jeeba) di Samba Peuzzi , sia per cantarle sotto la doccia, fare le tue cover, dedicarle a qualcuno o vincere una scommessa.